jule1

03 juin 2006

under fire

yaw miy ploh1

kanalou sol say bak di dieungelou khana hamo kou soukou diebelou doudiape aw dokhine ba foumou tollou di allou barké serigne fallou mo lay takh di fallou di roy thiy américain té yoro ngegou pain say morom ligueye ngir amiy etage fo kheyé wouty grand place ték dieunde gaz w miy kana kak glace lidianty barada ak kasse gnounanela kagnou ték dieunde ataya nganane athia sa morom rombe lay hoslou lirek doyna gathia mlama mbarane ba fo tollou gnou nane la man sa boppou defo thi dara lou doule dokhane mana por ba ko djisse mou siol khaftane hawa tilim di tarri arkhourane nganane  dafa sarane bo démé sakh amoul foumou fanane say kadou narla fade say khalate doupela malade tothie say galathie  ba amo léne louko mana fathie loudoule balou dekendo sety andando gnou diappéla gane ganalé terou teral khamné do kou yaradal

Posté par papesouley à 14:48 - Commentaires [0] - Permalien [#]